Paroles de Africa democratie

Ismaël Lo

pochette album Africa democratie
Voir sur Itunes

sonnerie téléphone portable pour Africa democratie

Guagni man e mbiirmi ler na
Ler na loo
Guagni mane mbiirmi ler na
Ler na lool
Ndakh abdou demna way abdoulay gneuwna tok
Democratie nlla wara deme
Mane abdou demna way abdoulay gneuwna tok
Democratie nlla wara deme
En bas coup d'etat viva africa democratie
En bas coup d'etat viva africa democratie
Kon senegal mbiirmi ler na ler nalen
En bas coup d'etat viva africa democratie
En bas coup d'etat viva africa democratie
Ficl africa amna rew youma sopeu lolo com benin
Mba ngua dokhontou ba mali gnom gnouguai do«hal

Tamit yonou democratie
Ndakh soglo demna way mane kerekou gneuwna tok
Democratie nlla wara deme he
En bas coup d'etat viva africa democratie
En bas coup d'etat viva africa democratie
En bas coup d'etat viva africa democratie
Mane kholna guis nl africain kene warougno diawale
Kon souma sagnone
Rewou africa yeup dokhal yonou democratie
A.t.t. democratie way mane konare gneuwa tok
Democratie nlla wara deme
A.t.t. democratie way mane konare gneuwa tok
Democratie nlla wara deme he
En bas coup d'etat viva africa democratie
En bas coup d'etat viva africa democratie
Kon en bas coup d'etat viva africa democratie

Les autres musiques de Ismaël Lo