Paroles de Aiwa

Ismaël Lo

pochette album Aiwa
Voir sur Itunes

sonnerie téléphone portable pour Aiwa

Mane way bimay way tibeu nako sama biir khol
Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir keur
Mane way bimay way tibeu nako sama biir khol
Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir keur
Kone sohna bourou keureum dal aiwa
Mane way bl may way tibeu nako sama biir khol
Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir keur
Mane way bimay way tibeu nako sama biir khol
Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir khol
Kon sohna bourou kereum dal aiwa
Kone awo bourou keureum
Gnarel kharitou dieukereum
Kone awo bourou keureum da aaa al
Gnarel kharitou dieukereum
Gnarel kharitou dieukeureum awo douko nangou
Mana way bimay way bindeu nako sama biir neek

Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir keur
He khe mane way bimay way bindeu nako sama
Diko wayal kepeu koudi sohna sa biir keur
Kon sohna bourou keureum da aaa al aiwa
Kon awo bourou keureum
Gnarel kharitou dieukeureum
Kon-awo-bourou keureum da aaa al
Gnarel kharitou dieukeureum
Gnarel kharitou dieukeureum awo douko nangou
Kon awo bourou keureum
Gnmrel kharitou dieukeureum
Kon awo bourou keureum da aaa al
Gnarel kharitou dieukeureum
Gnarel kharitou dieukeureum awo douko nangou
Kon awo bourou keureum daaaaal
Gnaaaa gnaaaaaaaaaa

Les autres musiques de Ismaël Lo