Paroles de Casamance

Idrissa Diop

pochette album Casamance
Voir sur Itunes

sonnerie téléphone portable pour Casamance

Casa casa dit mansa
Yale nafa diame amé
Casa casa dit mansa
Yale nafa diame saxé.

Amone na bene bess, ma diare casamance
Fêkeu fa nith gnu tek ak têeye
Gnou terou ma terale ma
Wanagnu ma nè wa n'dakaru la
Casamance xam' na fa nith gnu bakh
Mane diare na cap-skiring
Mane diare na kabkousse
Mane diare na diebering
Diare na youssouye ak zingieneto

Casa casa dit mansa
Yale nafa diame amé
Casa casa dit mansa
Yale nafa diame saxé.

Mane diare aye goghi goghé
Diame rek mofa mossa amé
Kassumaye kassumaye kere
Naugadef kokabo
Bari nafa ayes xanto
Bari nafa ayes boko
Yal nafa diamen amé
Nagnu anden dégo
Bolo neken bene rêwe

Les autres musiques de Idrissa Diop