Lyrics of Yonn gui
William Baldé
Yönn-gui sorry-na
Bokö narré deff
Ci suffü taü-gui...
Yönn-gui dina gudü
Bo-cy narré diarr
Di-tallal, ça kanaam
Ta bagna tégy tank...
Wahé lö metti yagül... leygi mü diêkh
Gaal yangy-dem cy ndokh-gy
Batcha nek khamna famü dièm
Wahé dü yag, dina nü taffé-sü !
Yönn-gy dina diaffé
Büla diarralé
Cy mussy-beup kharré
Yönn-gui diss-na
Wahé bull-topo-to ndakh
Bü mané bü nac... lu-munaane
Yönn-gui diaffé-na
Büla diarraté
Cy mussy-beup kharré
Yönn-gui dissna
Wahé bull-topo-to ndakh
Bü mané bü nac... lu-mu-naane...
Others tracks of William Baldé
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
En corps etranger
William Baldé

Exil
William Baldé
La boite a photo
William Baldé
Lyrics of La boite aux photos
William Baldé
Le prix a payer
William Baldé

No more again
William Baldé

Rayon de soleil
William Baldé

Lyrics of Sur la route de dakar
William Baldé

Suzy
William Baldé

Sweet lady
William Baldé
Vaudou
William Baldé

Lyrics of Yonn-guy
William Baldé
Lyrics of the track yonn gui by william baldé.





