Paroles de Amoul solo
Ismaël Lo
Diam bou nek sayo yewo
Guanaw yaw bigua sante yala
Nagua delou gueureum say wadiour
Diam bou nek sayo dieko
Guanaw yawbigua sante yala nagua delou
Nagua delou teral say wadiour
Ndakh adounya amoul solo
Ndakh mano kham lougnou dadion
Tay dji bila yala maye takander
Digua delo dioukeul say wadiour
Sl yawou
Ndakh barile barkel le ko gueun
Boula yala maye ngua mouthia sl adounya
Nangua delou fonkeu say wadiour
Bouboba digua tok khol adounym nl amoul solo
Adounya adounya adounym
Adounya amoul solo hou hoo
Kena manoul waaat....ni masso togne say wadiour
Ndakh bo sete sl kholin ba sl tontouba mba sl dieufinba
Yayboy tok dila mougnieul danan kl guounela
Waye bo togue ba adouna wanla
Digua gueuneu fonke say wadiour
Ndakh adounyaa amoul solo kat
Adounyaa amoul solo
Adounya adounya adounym adounya amoul solo
Sama yay mangui sakou gnane sl yaw
Sama bay mangui sakou gnane sl yaw
Ndakh kholna ba khol nl adounya amoul solo
Adounya adounya adounyaa adounya amoul solo
Sama yay mangui sakou gnane sl yaw
Sama bay mangui sakou gnane sl yaw
Ndakh kholna ba khol nl adounya amoul solo
Adounya adounya adounyaa adounya amoul solo
Adounyaaa amoul soloooo.
Les autres musiques de Ismaël Lo
Africa democratie
Ismaël Lo
Aiwa
Ismaël Lo
Badara
Ismaël Lo

Paroles de Baykat
Ismaël Lo
Biguisse
Ismaël Lo
Boulfale
Ismaël Lo

Dabah
Ismaël Lo
Paroles de Diour sani
Ismaël Lo
Incha allah
Ismaël Lo

Jammu africa
Ismaël Lo
Jiguen
Ismaël Lo

Paroles de La femme sans haine
Ismaël Lo
Le jola
Ismaël Lo
Lions de la teranga
Ismaël Lo
Ma dame
Ismaël Lo
Paroles de Ma fille
Ismaël Lo
Manko
Ismaël Lo
Mam
Ismaël Lo
Mbindane
Ismaël Lo
Paroles de N'dally
Ismaël Lo

Tajabone
Ismaël Lo
Tass yakar
Ismaël Lo
Wakhal
Ismaël Lo

Paroles de Xalas
Ismaël Lo
Yaye boye
Ismaël Lo
Paroles de amoul solo de ismaël lo.




