Paroles de Biguisse
Ismaël Lo
Yaw manela awma
Nganema beuguegua.
Man manela way yorouma
Nganema nangougua
Biguisé biguisé
Biguise ee
Yal nadieum kanam way
Way wakhma fodieum manma yoboula
Mba gua wakhma fo deuk man ma setsila
Way way wakhma fodieum manma yoboula
Mba gua wakhma fo deuk way man ma setsila
Biguisé biguisé
Biguise ee
Yal nadieum kanam way
Bl bl bl bl bibi
Kholna ba khol yaw topoulo
Nitki guir loumou am
Ndakh boudon am amo do khar ba legui
Way sohnassi mane bis dina gnowde bour yala teral la
Djiguen djou bakh mane day am yitte
Te amguako bamou dieeeekh
Biguisé biguisé
Biguise he
Yal nadieum kanam
Djiguen diou bakh day am yite
Djiguen diou bakh day am imane
Sohnassi mane bakh ngua lol
Ye he he he he
Bl bl bl ll mane doy na war
Fodieum man ma topeula
Ndakh khawma fodieum man ma yoboulaaa
Khawma fo deuk kon man ma setsila
Sohnassi amgua yite lol
Bl bl bl bl bl bl bl biiiiii
Les autres musiques de Ismaël Lo
Africa democratie
Ismaël Lo
Aiwa
Ismaël Lo
Amoul solo
Ismaël Lo
Paroles de Badara
Ismaël Lo

Baykat
Ismaël Lo
Boulfale
Ismaël Lo

Dabah
Ismaël Lo
Paroles de Diour sani
Ismaël Lo
Incha allah
Ismaël Lo

Jammu africa
Ismaël Lo
Jiguen
Ismaël Lo

Paroles de La femme sans haine
Ismaël Lo
Le jola
Ismaël Lo
Lions de la teranga
Ismaël Lo
Ma dame
Ismaël Lo
Paroles de Ma fille
Ismaël Lo
Manko
Ismaël Lo
Mam
Ismaël Lo
Mbindane
Ismaël Lo
Paroles de N'dally
Ismaël Lo

Tajabone
Ismaël Lo
Tass yakar
Ismaël Lo
Wakhal
Ismaël Lo

Paroles de Xalas
Ismaël Lo
Yaye boye
Ismaël Lo
Paroles de biguisse de ismaël lo.




