Paroles de Jammu africa
Kirikou Et Karaba
Africa a a ah
Africa mon afrique
Sama gent bi manguiy nian yalla won mako bala may gnibi barsah
Mané bes bu niak ci bes yi bé africa doon benn reew
D' ici ou d'alleurs nous sommes des enfants d'afrique meme si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu africa moom laay niaan, mané jammu africa mooy suniou natangéé
Africa...
Yay mi nekk bitim rew may lo manglay niaan,
Ak loo fa meunta am ak loofa meun ti mel bul faté africa
Ici ou ailleurs la paix fruit du bonheur; meme si le ciel pleurait, luttons pour nos freres.
Kon jaammu africa moom lay nian, manéé jammu africa mooy suniou natangué
(x2): africa...
Les autres musiques de Kirikou Et Karaba
Paroles de jammu africa de kirikou et karaba.




