Paroles de Tuti sop

Wasis Diop

pochette album Tuti sop
Voir sur Itunes

Date de parution : 29/06/2008

Durée : 0:02:48

Style : World



sonnerie téléphone portable pour Tuti sop

Pomu ndar géc,
Pombi, nétalina ma,
Liy daw ci tatu pom bi,
Nu di ko wowé déx gi

Néna niari xalé, xalé yu sopan té
Sééni rongon nia fi turu,
Lolo indi déx gi.

Xalé aduna,tuti sopanté
Mag ni di xaré ,di wérénté séén diganté,
Wayé du téré, ngén di fékanté,
Ba di wérénté ci tatu pom bi.

Pomu ndar géc,
Pom bi ya ma na nëbu
Liy daw ci tatu pom bi,
Nu di ko wowé déx gi
Xam na né niari xalé, xalé yu bëgënté
Séén rongon nia fi turu.

Pombi, nox mi bari na
Té pom bé kë ma na nëbu.
Liy daw ci tatu pom bi,
Nu di ko wowé déx gi
Néné niari xalé,
Séén rongon nia fi turu,
Lolo indi déx gi, lolo indi ndox mi.

Les autres musiques de Wasis Diop