Lyrics of N'dally
Ismaël Lo
Tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Ndaly khamgua gnoko bokeu
Linfi takha tok yaw oumpoula
Kepeu koussine nek daguay dane sa dole
Mognoufi takha tok
Kon tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Ndaly khamgua gnoko bokeu
Linfi takha tok yaw oumpoula
Kepeu koussi nek daguay dane sa dole
Mognifi takha tok
Kon tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Kon tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
He he
Ndaly khamgua nioko bokeu
Loutakh yama eupeule
Lolou amna louko waral
Ndakh amna loy def sl souf
Kon mandou mognou war who who who
Tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Diokhma bobougue sa kayit guawoo
Lolou dagneka wara bayi
Diohma bo bougue sa affaire dou takhawo
Lolou dagneka wara bayi
Bougnla wolo ba tekla sl placou ligueyoukay
Bilay gneupeu ngafi nekal who who who
Kon tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandy
Kon tankhal sl ndaly mayma ma nane ba mandykon tankhal sl
Ndaly mayma ma nane ba mandy
Others tracks of Ismaël Lo
Africa democratie
Ismaël Lo
Aiwa
Ismaël Lo
Amoul solo
Ismaël Lo
Lyrics of Badara
Ismaël Lo

Baykat
Ismaël Lo
Biguisse
Ismaël Lo
Boulfale
Ismaël Lo

Lyrics of Dabah
Ismaël Lo
Diour sani
Ismaël Lo
Incha allah
Ismaël Lo

Jammu africa
Ismaël Lo
Lyrics of Jiguen
Ismaël Lo

La femme sans haine
Ismaël Lo
Le jola
Ismaël Lo
Lions de la teranga
Ismaël Lo
Lyrics of Ma dame
Ismaël Lo
Ma fille
Ismaël Lo
Manko
Ismaël Lo
Mam
Ismaël Lo
Lyrics of Mbindane
Ismaël Lo

Tajabone
Ismaël Lo
Tass yakar
Ismaël Lo
Wakhal
Ismaël Lo

Lyrics of Xalas
Ismaël Lo
Yaye boye
Ismaël Lo
Lyrics of the track n'dally by ismaël lo.




