Il testo della Lou tax
Idrissa Diop

Vista su itunes
Data di rilascio : 04/02/2003
Durata : 0:03:35
Stile : World
Lou tax nith di dawe moromame ?
Lou tax guerre doufi diexh ?
Lou tax titangué baré ?
Lou tax xéekh doufi diexh ?
Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té bayi guerre bé
Mane waru na yène thi diamono
Lou tax disso diexh filé ?
Lou tax dioubo ware fi rêere ?
Xole lène aye réewi réewe
Di xoulo aka guerre
Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té bayi guerre bé
Mane waru na
Thi diamono
Altri brani di Idrissa Diop
Il testo della canzone lou tax da idrissa diop.






