Il testo della Dioubo

Idrissa Diop

pochette album Dioubo
Vista su itunes

Data di rilascio : 27/11/2010

Durata : 0:04:11

Stile : World



sonnerie téléphone portable pour Dioubo

Beugueunala beugoumala
Lolou diakule tiawe
Kaye dioubok mane

Beugueunala beugoumala
Lolou diakule tiawe
Kaye dioubok mane

Diale boubo diale matia aïra
N'diaye samba m'boup
Kaye dioubok mane

Diale boubo diale matia aïra
N'diaye samba m'boup
Kaye dioubok mane

Sopé n'gani, beuguêle boko
Neubé dalaye gagne
Kaye dioubok mane

Sopé n'gani, beuguêle boko
Neubé dalaye gagne
Kaye dioubok mane

Dioubo kaye fi gnu dioubo
Ma chérie
Yawe dioubo
Sopé gani ma, beuguêle boko neubé
Dalaye gagne yayo yayé
Xalé bi yawe mane beuguenala
Yawe
Mi kaye fi.

Altri brani di Idrissa Diop