Lyrics of Xalas
Ismaël Lo
Bou gnewe neko demna demna
Bou gnewe neko demna demna
Ndakham manatouma khar
Kouka khar filay fanane
Souma guissan auto bou rafet dieunde
Nguamay gueumeul man ngua beugeu
Souma guissan or bou rafet indi
Nguamay gueumeul man ngua beugueu
Kon bok taydji sama bis gneuwna de
Ma nanguouko ma nanguouko wa way ma nanguouko
Mane khalas
Mane khalas sl diankhabi
Mane khalas
Mane khalas sl djikodji
Mou fekhe bama minko
Mane khalas
Mane khalas sl djikodji
Mane khalas
Douwon man kenekon
Nga fekhe bama minla ngua deposema
Mane khalas mane khalas sl diankhabi mane khalas sl djikodji
Mou fekhe bama minko
Dama khamoul bang ma woye loutakh ma dof topala
Mama khamoul bang mawoye loutakh ma dof topala
Nga fekhe bamaminla ya barri borom
Mane khalas mane khalas sl djikodji mane khalas
Douwon man kenakon mou fekhe bama minko mou deposema
Mouyen nl waw nguani
Magnew magnew magnew ass boula nekhe
Mouyen nguani nl wawaw reck
Dama khamoul bang mawoye loutakh madof topala
Dama khamoul bang maguisse loutakh ma dof topala
Ngua fekhe bamaminla ya barri borom
Kon bok bou gnewe neko demna demna
Manman bou gnewe neko demna demna
Ndakham manatouma khar kouka khar filay fanane
Kouka khar filay fanaen
Others tracks of Ismaël Lo
Africa democratie
Ismaël Lo
Aiwa
Ismaël Lo
Amoul solo
Ismaël Lo
Lyrics of Badara
Ismaël Lo

Baykat
Ismaël Lo
Biguisse
Ismaël Lo
Boulfale
Ismaël Lo

Lyrics of Dabah
Ismaël Lo
Diour sani
Ismaël Lo
Incha allah
Ismaël Lo

Jammu africa
Ismaël Lo
Lyrics of Jiguen
Ismaël Lo

La femme sans haine
Ismaël Lo
Le jola
Ismaël Lo
Lions de la teranga
Ismaël Lo
Lyrics of Ma dame
Ismaël Lo
Ma fille
Ismaël Lo
Manko
Ismaël Lo
Mam
Ismaël Lo
Lyrics of Mbindane
Ismaël Lo
N'dally
Ismaël Lo

Tajabone
Ismaël Lo
Tass yakar
Ismaël Lo
Lyrics of Wakhal
Ismaël Lo
Yaye boye
Ismaël Lo
Lyrics of the track xalas by ismaël lo.





